Mane la beugue
Mane la guis
Man r é k dou k é n é ne
D é fale ma loun é
Wane ma loun é
Yobou ma foun é
Mossou ma sorri
Souma am é naxar
Mou dima yokou yakaar
Daf maye di é gu é
Souma tiss é mou dima deufeul
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
Oh oh nane la kokoye wah é
Oh oh t é doumako gagne
Oh oh nane la kokoye wah é
Oh oh t é doumako gagne
Xamna lovame ak y é n é ne
Fimou tolou tchi mane
Motah ma wara sinc é re
Wah ko deugue
Nit kou bah laa
Souma sanione sama love dafaye law ba faw
Tayoumako
Souma n é k é k mome
K é n é ne laye halat
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
Oh oh nane la kokoye wah é
Oh oh t é doumako gagne
Oh oh nane la kokoye wah é
Oh oh t é doumako gagne
Oh balma
Nane lakokoye wah é
T é douma ko gaagne
Tissnama baby forgive me
Mane tayouma lima dal
Mbeuguel boula songu é none la
Yow balma
Ni mbeuguel loye fal é woul sa h é te
Dou mbeur momou niouy dane
Ni mbeuguel loye foume la f é k meune laye
Dalay yobou ardo
Kass nane laye d é f cey love
Li kou ko xamoul dala daloul cey love
Li kou ko xamoul dala daloul cey love
Li kou ko xamoul dala daloul cey love
Li kou ko xamoul dala daloul cey love
Li kou ko xamoul dala daloul