menu-iconlogo
huatong
huatong
avatar

Amul nu malene beguewoul

Titihuatong
tropotropohuatong
Letras
Grabaciones
Goor deh gor leu

Goor deh gor leu

Bou ande ak teranga aduna

Goor deh gor leu

Goor deh gor leu

Bou ande ak teranga aduna

Goor deh gor bou ande ak teranga aduna

Djiggen billaye gnoko mom

Goor deh gor bou ande ak teranga aduna

Djiggen billaye gnoko mom

Soula yoré (seteul leu)

Boula yoré (tereul leu)

Té di sargal

Boula yoré (seteul leu)

Boula yoré (tereul leu)

Té di sargal

Goor deh gor bou ande ak teranga aduna

Djiggen billaye nioun gnoko mom

Goor deh gor bou ande ak teranga aduna

Djiggen billaye nioun gnoko mom

Guinaw bour bi yallah xamneuné

Damay lathie senegal bou goor amulone

Ahh fuu djiggen djem

Bou sey beu yerrée waatnané salite day am

Nioun degeun ni door ak saag dakh diaralgeen

Amul nu malene beuguewoul

Moy watteli djiggen ahh ci biir keureum

Té goor cadouom leu am

Amul nu malene beugeuwoul

Degger gui thi goor

Diambar gui thi goor

Goora goora goor

Amul nu malene beugeuwoul

Goor deh gor bou ande ak teranga aduna

Djiggen billaye nioun gnoko mom

Goor deh gor bou ande ak teranga aduna

Djiggen billaye nioun gnoko mom

Boula yoré (seteul leu)

Boula yoré (tereul leu)

Té di sargal

Boula yoré (seteul leu)

Boula yoré (tereul leu)

Té di sargal

Billaye diaral gue ma

Diaral gue ma

Goora goora goor

Diaral gue ma

Guisseul limey defé

Ak liimey dokhé

Goora goora goor

Diaral gue ma

Damay diagari diagari

Yok sama taar

Dakh diaral gue ma

Maan seu serr la

Yow sama serr gue

Goora goora goor diaral gue ma

Más De Titi

Ver todologo

Te Podría Gustar

Amul nu malene beguewoul de Titi - Letras y Covers