menu-iconlogo
huatong
huatong
avatar

La Saga Commence

GUN MORhuatong
srnewland78huatong
Lirik
Rekaman
Ma Doneu diourom beneu djiko domou pape Serigne ndiaye

Gneme metit biné si mane djougué woule foudoul Sama baye bi

Mane la tawou mère bi wara indi galey nantangué

Téla ragné deugak fene ecolou tantôt fala diangué

(Gun moooooor)

Ki koumbeuy di sentou ki gni yeux di deglou

Teude sama fenêtre guiss borom bene beut yi di yendou

Xam di def mane douma feug mouk bountou boudoul tidjekou

Rafet ngemb meuneu beuré douma dane dièl bou djekoul

Guelaw bouy nayal ay carriere bamay nieuw laa indalé

Diar si digui bi gni si souf ak si kaw ils sont êtes menacés

Beuthieuk laye tass dynasty yi douma baye timiss bi massé

Yoor loudoul diex diko sotii foudoul fess

Péxé kene douma té

Demna ni Jesse Owen bou war fassou narou goor

Linek sama sac eupneu djounek djourom ñari Guns

Kouma tongol bene takussan dane ko diourom niarii yone

Douma doyal ame diourom di woutat diourom niari milliongggg

Soxla yé beurii legui galë goney mane lañi latié

Fok samay compte fess comme resto fac sougn togué 3 pièces

Équilibre loxo gaucher tank droitier

Du guest star bi di dougué fala sama auto di droité

Maam Mor guéneu aduna, Baye mor guané aduna

Magg nioumay wowé Maam mor legui tour bi diadou neu

Sante yalla sama xel comme sama xol bi yatou na

Tégou si yone bi geune Sigui di dox ba legui diadouma

Mane douma taal bou yalla tal mais ligey kate bou yalla faye la

Kign done séntou yeksina biss biñ done xar taye la

Xarouma kene ba kene dima taylé

Soralélwma kene

Xouss si guedjou meune meune ay tank dougn mako geuneu toylé

Jsuis la somme

D'Elzo plus iss d'Omzo plus Dip

Je m'élève au rang de rakim et de notorious Big

Star bima nara doni dongue la rêvé guiss

Bind Sama propre histoire té douma abeu kene bic

(Heuuh)

Concurrence ak boys yi non par ce que dou équitable

Heuhh

Bonne nuit les petits, dis moi petit marchand de sable

When I be one the mic Baba Sy makoy dakeu sccrable

Fi kene dou né si jaam tanka Awma vie Bou stableuuu

Bleue comme le ciel doumafi def Li guene fi meusseu guiss

Xolal gnimay get legui nekatouma n'importe qui

Liral samay textes dossi guiss mouk di n'importe quoi

Niogui petaw pour guiss Sané mais guissougn qui est le Roi

Mangui ni

King Gun Mor in da area

Selengkapnya dari GUN MOR

Lihat semualogo