menu-iconlogo
huatong
huatong
youssou-ndour-gore-cover-image

Gorée

Youssou Ndourhuatong
miss_piggy25huatong
歌詞
収録
Ba ma démé gorée mane

Andak samaye kharite

Déme thia keur diame ga wone

Dama daldi seugueume dioye

Gore gnou make gni bi bore

Djiguéne gnou make gni bi bore

Gore gnou ndaw gni bi bore

Djiguéne gnou ndaw gni thi bénéne bore

Gnou daldi faye khali yone

Yone wo khamni dangaye déme

Yone wo khamni dangaye déme

Sa khéle dou déme loudoul thi déloussé

Loloye natou lawou bour bi

Mi borome dogal yé

Loloye natou lawou bour bi

Borome koun faya koun

Ba ma démé gorée mane

Andak samaye kharite

Déme thia keur diame ga wone

Dama daldi seugueume dioye

Gore gnou make gni bi bore

Djiguéne gnou make gni bi bore

Gore gnou ndaw gni bi bore

Djiguéne gnou ndaw gni thi bénéne bore

Gnou daldi faye khali yone

Yone wo khamni dangaye déme

Sa khéle dou déme thi loudoul

Déloussé

Aaan gorée

Loloye natou lawou bour bi

Mi borome dogal yé

Loloye natou lawou bour bi

Borome koun faya koun

Loloye natou lawou bour bi

Mi borome dogal yé

Loloye natou lawou bour bi

Borome koun faya koun

Goréée

Natou lawou bour bi

Mi borome dogal yé

Loloye natou lawou bour bi

Borome koun faya koun

Youssou Ndourの他の作品

総て見るlogo