menu-iconlogo
huatong
huatong
youssou-ndour-be-careful-version-mbalax-cover-image

Be Careful (Version Mbalax)

Youssou Ndourhuatong
minoaka1huatong
Letra
Gravações
Be careful be careful dakh tomorrow you don't know

So bougoulé gagnou boul thieu daw baye dano

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

If you meet a man you don't know loumouleuh meuneuh wakh boulko know

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

If you meet a man you don't know loumouleuh meuneuh wakh boulko know

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Meuneuh donap saïsaï bamou bokk'ak saïsaï

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

So bougoulé gagnou boul thieu daw baye dano

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Oh love is very serious boul deugeuroul déy rouss

(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Ça ne se négocie pas

Ça ne s'achète pas pas pas

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Ça ne se négocie pas

Ça ne s'achète pas pas pas

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Ne te fie pas aux apparences l'habit ne fais pas le moine

Une belle chemise, un beau jean, ce n'est que du matériel

Une belle voiture, un château, ce n'est que du materiel

Cherche d'abord à savoir qui est derrière ce beau décor

Fou d'amour dés le premier jour "dédétte"

Foufou foufou fou d'amour dés le deuxième jour "dédétte"

Meuneuh donap saïsaï bamou bokk'ak saïsaï

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Love is very serious boul deugeuroul déy rouss

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)

Ça ne se négocie pas

Ça ne s'achète pas pas pas

(Youssou ndoye diaraf malik mareme ndoye diaraf thia ouakam lébou leuh)

Ça ne se négocie pas

Ça ne s'achète pas pas pas

(Adji néné kane seu yaye mbao la fékk bakh youssou ndoye diaraf lébou leuh)

Ah seck ndiaye aaatoumane ndiaye mod ndiaye goné abdou demba bayou mar

Bourou teunguédji nganane seck ndiaye atoumane ndiaye

Modou ndiaye cissé teunguédji la békk bakh domou lebou danio bari diomm

Béna way séna mou sol

Waleuh auto bamou yorr (beugueu ko diokh seu xhol)

Loumou wakh gani waw (lépp guir deureum)

Xamoulo limou amm (fane leuko dieulé)

Nitt boko xamoul (dagay téyy si mom)

Béne fane waleuh niarr (meunoulo xham djikôm)

Thi seu niakk seu ngorr (lalay dougeulé) love!

Boul guiss béne way (béna way séna mou sol)

Waleuh auto bamou yorr (beugueu ko diokh seu xhol)

Loumou wakh gani waw (lépp guir deureum)

Xamoulo limou amm (fane lako dieulé)

Nitt boko xamoul (dagay téyy si mom)

Béne fane waleuh niarr (meunoulo xham djikôm)

Thi seu niakk seu bopp (lalay dougeulé) love!

Ça ne se négocie pas

Ça ne s'achète pas pas pas

(Aladji mbaye ndoye seu baye kokou lébou leu youssou ndoye diaraf lébou leuh)

Fou d'amour dés le premier jour "dédétte"

(Ngor ouakam né waw, wa yoff né waw youssou ndoye diaraf lébou leuh)

Love is very serious bou deugeuroul déyy rous

(Ndoye Malik maréme ndoye teunguédji bi youssou ndoye diaraf)

Aye lébou laniou, aye lébou laniou

Be careful be careful baby, dakh tomorrow you don't know

(Dégueule! Youssou ndour youssou ndoye diaraf ayy xaarit laniou)

(Moytouko moytouko baby dakhté soubeu xamoulo)

Mais de Youssou Ndour

Ver todaslogo

Você Pode Gostar