Mane la beugue
Mane la guis
Man r é k dou k é n é ne
D é fale ma loun é
Wane ma loun é
Yobou ma foun é
Mossou ma sorri
Souma am é naxar
Mou dima yokou yakaar
Daf maye di é gu é
Souma tiss é mou dima deufeul
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him
Xamna lovame ak y é n é ne
Fimou tolou tchi mane
Motah ma wara sinc é re
Wah ko deug nit kou bah laa
Souma sanione sama love dafaye law ba faw
Tayoumako souma n é k é k mome
K é n é ne laye halaat
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
T é xamoul n é sama xol
K é n é nne na fa fess
Nane la kokoye wax é
D é fouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul tonioula
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him
Forgive me
How to be sincere
Without deeply hurting him
I am sorry
Baby forgive me
I don't know how to tell him
That love I felt went away
Forgive me
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him
Oh oh I love someone else
Oh oh I am crazy about him