menu-iconlogo
huatong
huatong
avatar

Ana porolem bi

Cab/Bm jaayhuatong
youniyounihuatong
Şarkı Sözleri
Kayıtlar
Ana porolem bi

Yaw

Yeah han

Yoré bopp bou fess

Kone meunouma low prix

Jeunessou kylian laniou jaxassé ak xelou modric

Deuk ci def

Bolékok nopiiiiiii

Dieufeul th bayi wax daniou soneu ci bande annonce yi

Limaleu gueune niémé job réka tax doma raw

Barki alxourane

From sama nek to the top sama baatangui laaw

Ana porolem bi

Kou banie takeu bane fima aw doufeu meuss beug aaaaaw

Barki alxourane

Th diemeul nga def lima def mo gueune talkin a lot

Ana porolem bi

Guissouma mane beneu porolem

Boumay té né kou tedd ci rap

But bé eup bou talonner

Raaap galsen manela yalla bi th diotoumafi yoni beneu prophete

Chaque jour yangui xeuy sama der diko yakeu esk doumla diox ibuprofene

(Ra ra ra)

Mane laniou fal game bi may kiko wara developper

Do meusseu signer simane wanté gnileu bégué niomay nianatou autographes

Fi ngay guiss kouné mo dak punchline th si son yi mouy devinette

Lima nara defap ngandi icone meuneu son leu dou photographe

Nianou wadiour amoul louko teu

Diemeu gueneu sama zone de confort

Niom niouy diemeu doug sama zone

Douma artiste bouniou verifié

Monté mangui tax ay bum di flop fils

Sama kadu sama premier sponsor

Comme que balle leu manguek sama gun

Samay loxo amoul loci tek

Daniou soneu ci bande annonce yi

Yoré bopp bou fess

Kone meunouma low prix

Jeunessou kylian laniou jaxassé ak xelou modric

Deuk ci def

Bolékok nopiiiiiii

Dieufeul th bayi wax daniou soneu ci bande annonce yi

Limaleu gueune niémé job réka tax doma raw

Barki alxourane

From sama nek to the top sama baatangui laaw

Ana porolem bi

Kou banie takeu bane fima aw doufeu meuss beug aaaaaw

Barki alxourane

Th diemeul nga def lima def mo gueune talkin a lot

Ana porolem bi

Wooo woooo

Sama Ford Moy Focus

Man Ak Ligey Nio Fusion

Yar sikim yor brabus

Deretou none yi infusion

Xaliss bou set ak bou tilim na fess sama biir ni kou am koachiorkor

Do multiplier sa ben bénéfice ndax danga manquer li di vision

(Do xol xana)

Jeuneussou Kylian jaxasse ak xelo modric

(Yaw la Ricky Drenthe)

Teud si piliane guenè samay statistic

(Talatouma werantè)

Streaming Spotify yangi tchi guinaw Pacotille

(Mais Néna moma djitè)

Waxtanou Milliard yonou pauvre nékou tchi

Wéthiét bi moy sa sujet

Yor sama pèle di gass dama tal say pique

Mounougn ma thiop dama fess sen tchin

Boul dem dikat togatal sen Team

Sougn mey sene di djad dama dox sen fit

Man la ten bi bag bi xont sen hip hop wout len syndicat wou Rappeur anorexique

Am Audace Dima Gnane ay feat

Shout out to cab fuck bokoul Fii

Ay so xamone lep limouniou jaral

Geteu bou goat yeup deuk baki axourane kene douniouko téré

Finiouy wok da melni fala

Yeah finiou wok daa melni (falaa)

Marouane xalé bouko tendance mou defla si sar monami (alors)

Lidi bax da melni sa (xolaa)

Mingui bax th narouta fay dh

Koudoul liguey kat do sama nawlé

Gangou bandit leu kene douko taylé

Marouane papa leu CAB maobé

Nioy number one do sax numero 2

Yegg au top mom dinala diss

Boudoul ndaré dou lene louniela seuf

Lalal bassang ndax souf ci nga miss

Yoré bopp bou fess

Kone meunouma low prix

Jeunessou kylian laniou jaxassé ak xelou modric

Deuk ci def

Bolékok nopiiiiiii

Dieufeul th bayi wax daniou soneu ci bande annonce yi

Limaleu gueune niémé job réka tax doma raw

Barki alxourane

From sama nek to the top sama baatangui laaw

Ana porolem bi

Kou banie takeu bane fima aw doufeu meuss beug aaaaaw

Barki alxourane

Th diemeul nga def lima def mo gueune talkin a lot

Ana porolem bi

Cab/Bm jaay'dan Daha Fazlası

Tümünü Görlogo