menu-iconlogo
huatong
huatong
titi-aladji-ass-cover-image

Aladji ass

Titihuatong
trinityb1huatong
Şarkı Sözleri
Kayıtlar
diouk léne niou sant bayou bassirou

ahmadou bamba liguey na

diouk léne niou sant bayou bassirou

ahmadou bamba liguey na

diouk léne niou sant bayou bassirou

ahmadou bamba liguey na

diouk léne niou sant bayou bassirou

ahmadou bamba liguey na

Serigne bi nio ngui deel ddi niane

Fakhir dafay nongo dagane

Nangoul niou leup louniou la niane fall

Ndakh yene yayou laniou wara niane Fallo

cheikh Ibra di borom léér

Mame Bamba di borom djaloré

Niom nioniou guéné ci leundeum gui fall yobb niou ci léér

Borom lééri léér Hal hamdoulilahi

Bamba yaye ridialo ridiall!

Bamba Fo laniou la outii ngua

Bour yalla la tek sa gangou nay langue lay medaille

Diwane bi kham sa waye. kham naniou lambi so danne

Mbeurou dinéé

mbeurou dinéé

Bamba yaye ridialo ridiale

diouk léne niou sant bayou bassirou

Ahmadou Bamba liguey na

Serigne touba serigne touba

serigne touba daniou ko guéne mbacké barri

Né daniou koy yobou ndar

biniou démé ndar ndar beuga melni Darou

Niou dadi kooy dialakh mou dée Ndakkaru

Ko ooy mammi serigne m. Kara

Serigne touba ci guethie la daké seytané ki ndjodjam

Serigne touba ci guethie gui la amé lamb islam

Ridialouy ridialou Baye Fall

Ridialouy ridialou

Baye Fall

Ridialouy ridialou

Baye Fall

Ridialouy ridialou

Baye Fall

El hadji Ibrahima sergne seck ma thia fanakh

Koko beug serigne touba...

Titi'dan Daha Fazlası

Tümünü Görlogo