menu-iconlogo
huatong
huatong
بول
ریکارڈنگز
Jom mooy

Dém waayé fulay ñibbisi

Jambaar

Dawul doolé ladoon wuti

Yagg naa

Bittim reeeeew

Nibbisinaaaa

Sama reew sénégal

Senegal

Senegal

Seneeeeegaaaal

Senegal

J'aime ce pays

Qui m'a vu grandir

Cette terre qui a vu mes premières larmes

Et mes fou rires

Pas besoin d'un crayon pour dessiner

Les sourires tels des rayons

De soleil pour taccueillir

Le cfa parle fort à travers et à tort

On marchande pour

Le transport et quoi encore

Ici a pamme tho badde thammi

Ici c'est taxi brousse

Jaune noir cars rapide

Ndiaga ndiaye ou pousse pousse

Petite pause dans une

Dibiterie outangana

Petite tintamarre

C'est du tama

De calne do

Vai elle danse avec ou sans salaire

Malgré les coupures d'électricité

Deau

Et la galère une pensée

Pour les frères qui ont coulé

Dans l'atlantique

Même si j'ai la chance de revenir

Ma blessure est à authentique

Nul n'est prophète chez soi

Mais on eqt mieux que chez soi

C'est vrai j'ai duré là bas

Mais mon cœur était là senegal

Jom mooy

Dém waayé fulay ñibbisi

Jambaar

Dawul doolé ladoon wuti

Yagg naa

Bittim reeeeew

Nibbisinaaaa

Sama reew senegal

Senegal

Senegal

Seneeeeegaaaal

Senegal

Fila reew néexé

Sénégal ngi ni dé

Booko soré dooto bêgg

Ludul ñibbisi dé

Bofi ñëwé joxé

Mbok néla kaay ñu gissé

Ana lo inddi

Se daañ la yenni say

Xarit yaggon toog di

Xaar di séntu bis bi mi ngi

Ñew na tay no dikké serica yi

Nga diggé

Sèntu nañla fin d'année été

Doyul daggal billet

Att bilé giss mbok yilé

Summi yërré immigré

Metro boulot amul dodo

Kogg bala jant bi modou modooo

Ñu ngi daw wuti wuti

Bitim reew bañ fa futi ubbi

Buntu xéwal bis fok ñu ñibbi

Mu ngi guddi

Sorri nga dëkkuwaay géntal

Ñulay teeru

Bis di ngua délluwaay yoon wi

Na nga léer lu xamal né

Jéggé na njaboot gi ñeppa ngi xaar

Démoon nga ñewaat nga

Senegal mooy sa képaar

Le courage de partir

Dem

La force de revenir

Ebc

Partir pour grandir

Revenir pour bâtir

Dans la grisaille et le froid

Jentendais ta voix

Me revoilà chez moi

Là où je me sens comme un roi

Senegaaal

Nok nosa jok

Senegal

Abc ebc

Senegaaaal

Senegal

Jom mooy

Dém waayé fulay ñibbisi

Jambaar

Dowul doolé ladoon wuti

Yagg naa

Bittim rew

Nibbisinaaaaa

Sama reew senegal

Kaffrine sedhi

Ou thies louga

Diourbel saint louis matam kolda kaolack

Kedougou tambacounda

Ziguinchor et dakar

Kaffine sedhiou thies louga

Diourbel saint louis matam kolda kaolack

Kedougou tambacounda

Ziguinchor et dakar

Daara J Family کے مزید گانے

تمام دیکھیںlogo

یہ بھی پسند آسکتا ہے

Senegal بذریعہ Daara J Family - بول اور کور