menu-iconlogo
huatong
huatong
avatar

Yow la

vjhuatong
mikeandikes87huatong
Lời Bài Hát
Bản Ghi
Set naa setoo setat gisaguma ku mel ni yaw

Sa jëmm je ma yëm man gisuma keneen

Pourtant man, pourtant man

Gis naa façon bu ne

Pourtant man, pourtant man

Gis naa jigéen bu ne

Yaw laa doon ñaan Yàlla (toucouleur al racine)

Ñaan yi mujje àntu (jekk rafet yaa ngi)

Yaw laay gis wër ba ngi

Kuy ndeyam ak baayam setoo set yaa ngi xoolooo say moroom

Jukk leen tay la tay ku ko xam na nga jaayu (jaayu)

Yaa jara sargal yaaa jara tàccu

Jaayul tey sa bés la, man maa la taamu

Say digg moroom say nawle su la neexee baaxu

Mbëggeel dafa diis, dafa bari doole

Yaay sama aljanna (waawaaw yaw la)

Yaay sama aljanna (ahh ahh yaw la)

Yaaa ma leen gënal yaw mi (waawaaw yaw la)

Yaay sama aljanna

Diombadioo ari, diombadioo ari

Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na

Diombadioo ari, diombadioo ari

Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na

Bés bi laa doon xaar, tay dafa mel ni moo ngi

Ëksil sama ndaanaan, naa la siggil ci say noon yaw

Fi ñu jaar li ma la tooñ, li nga may baal

Li ma la jaaral ak fi nga ma toollu sama ndaanaan

Yaa ma leen gëneloon dama leen ko rusoon a wax

Imam teew na nawle yépp teew yaw de nga ni waaw

Njegemaar bis yaa di mët jëg

May ko mu jal sama miss ba ngee

Xale la waaye fees na ak jom

Bis dina doni ndaanaan sama miss baa ngi

Mbëggeel dafa diis, dafa bari doole

Yaay sama aljanna (waawaaw yaw la)

Yaay sama aljanna (ahh ahh yaw la)

Yaaa ma leen gënal yaw mi (waawaaw yaw la)

Yaay sama aljanna

Diombadioo ari, diombadioo ari

Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na

Diombadioo ari, diombadioo ari

Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na

Me and you for life, for life bae

Me and you for life, for life bae

Xamal ni ma ngi ci sa wët

Muy taw wala muy naaj ma belle

Nhiều Hơn Từ vj

Xem tất cảlogo