menu-iconlogo
huatong
huatong
youssou-ndour-food-for-all-cover-image

Food For All

Youssou Ndourhuatong
kalarkalarhuatong
Lời Bài Hát
Bản Ghi
Last night I saw in my dream

All over the world

Food for all

Last night I saw in my dream

All over the world

Food for all

Batay amna nit gno xamni

Bougnou agné dougnou réer

Gnogno gui doundé thiono

Batay amna nit gno xamni

Bougnou agné dougnou réer

Gnogno eupati thiono

Nako gneup degg

Tey liy jot jotna

Gnognou lignouy doundou métina

Dolil dolil dolil dolil

More solidarity

Encore encore encore encore

Plus de solidarité

Last night I saw in my dream

All over the world

Food for all

Last night I saw in my dream

All over the world

Food for all

Na thi gneup dougal sen loxo

Té bagna xeeb ndimbal dou dooy

Li ga nara dékané deween

Guénée ko boul def yeufi Ndiawéne

Amna nit gnou xiif di ray

Dimbeli lène warougar la tay

Plus de solidarité

Plus de fraternité

More solidarity

More fraternity

Oooooh que c′est nécessaire

C'est c′est c'est c'est plus que nécessaire

Oooooh oh que c′est nécessaire

C′est c'est c′est c'est plus que nécessaire

Last night I saw in my dream

All over the world

Food for all

Yalla mo binde té yamaléwoul

Béne domou adama ak moromam

Wouté nagne ci xalaat

Wouté ci dieuf

Wouté ci thiossane ak ada

Wayé nagnou diap ni beugg jam

Ak doundou gou neex té andak dal

Boula yalla bolé thi gni am ba dessal

Naga seet gni amoul ga dimbali lén

Ooooh que c′est nécessaire

C'est c′est c'est c'est plus que nécessaire

Ooooh oh que c′est nécessaire

C′est c'est c′est c'est plus que nécessaire

Batay amna nit gno xamni

Bougnou agné dougnou réer

Gnogno gui doundé thiono

Batay amna nit gno xamni

Bougnou agné dougnou réer

Gnogno eupati thiono

Nako gneup degg

Tey liy jot jotna

Gnognou lignouy doundou métina

Dolil dolil dolil dolil

More solidarity

Encore encore encore encore

Plus de solidarité

More more more solidarity

More more more solidarity

More more more solidarity

More more more solidarity

Nhiều Hơn Từ Youssou Ndour

Xem tất cảlogo

Bạn Có Thể Thích