menu-iconlogo
huatong
huatong
youssou-ndour-habib-faye-cover-image

Habib Faye

Youssou Ndourhuatong
ritar_starhuatong
歌词
作品
Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap

Khamal ni diaposi dara

Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap

Khamal ni diaposi dara

Mane youssou niak na endano bou sincère

Aduna aduna dal nakhati naniu

Aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna

Habib yarou wone na Andak dignité

Fokone na liguey beugone ndiabotam

Donone diambar

Mane youssou niak na andando bou sincère

Aduna aduna dal nakhati naniu

Aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna

Aduna aduna dal nakhati naniu

Aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna

Aduna aduna dal nakhati naniu

Aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna

更多Youssou Ndour热歌

查看全部logo