Baba mi ani 
I guili Wana merer 
Wajy souma koy xool ak nimou mél 
Ah N bi né thi nekh 
Oubi bountou bus bi dougou sama xole 
Li mome dou néne 
Mou guestou xoolma 
Thi la xamner dou xememe 
Maye gnami gnami 
Koula jib wagni yaye dos d'âne 
Bus bé ngui daw dal te rombeuna sama arrêt 
Mba dou terminus lama dieumé 
Dara dakar fo dem dik 
Fess nga dél thi mane 
Té xawma yawla kane 
Xol bi nane ma te nga 
Dém dik xolle ba xame 
Fess nga dél thi mane 
Té xawma yawla kane 
Xel Bi nane ma togal boul 
Dem jiguene doù yombeu 
Ouhe baba, ouhe 
Ouhe baba 
Mideyidima 
Yidima 
Bus be ngui rire 
Mane degatouma 
Beug na la pire 
Ndax guissatouma 
Mbeugel bou gaw 
Melni Lou diare si peage 
O doff nassi Yaw 
Kila done sette 
Jombi te guissouma jine (ah ah, ah ah) 
Jappeu ma teuthieu condamné (ah ah, ah ah) 
Jokna arret laye demandé (ah ah, ah ah) 
Ba chauffeurou bus bi freiner 
Mou naxe ma seye 
Fess nga dél thi mane 
Té xawma yawla kane 
Xol bi nane ma te nga 
Dém dik xolle ba xame 
Fess nga dél thi mane 
Té xawma yawla kane 
Xel bi nane ma togal boul 
Dem jiguene doù yombeu 
Le courage m'a quitté 
(J'ai même pas osé tenter) 
Hypnotiser par son charme 
J'suis tombée en amour 
Fess nga dél thi mane, ah ah 
Xol bi nane ma te nga 
Dém dik xolle ba xame 
Fess nga dél thi mane, ah ah 
Xel Bi nane ma togal boul 
Dem jiguene doù yombeu 
Fess nga dél thi mane (ouhe) 
Té xawma yawla kane (ouhe) 
Xol bi nane ma te nga (ouhe) 
Dém dik xolle ba xame (ouhe) 
Fess nga dél thi mane (ouhe) 
Té xawma yawla kane (ouhe) 
Xel Bi nane ma togal boul 
Dem jiguene doù yombeu 
Ba bus bi freiner 
Thi la xamner reuthieunama 
Loutax demouma 
Bassi mome wakhko li fi ne