menu-iconlogo
huatong
huatong
youssou-ndour-exodus-cover-image

Exodus

Youssou Ndourhuatong
rubengarcia77huatong
歌詞
作品
Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Africa dama beugue ladjté

Est-ce que amoul louniou fatté

Wowowowowoy souniou rew yii dara doufi dess

Wowowowowoy niakk and lolou laniou bakké

Ana kouko def waay

Nioune nioko def

Ana kouko def kouko def

Nioune leu

Ana kouko def waay

Nioune nioko def

Ana kouko def kouko def

Nioune leu

Wowowowowoy eh pourtant fii leu nieupp di roté

Wowowowowoy kou si féssal daal diniou fatté

Wowowowowoy naniou andak fayda

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Bob Marley yagg neu beu woté

Diniou dioyal moussouniouko faalé

Wowowowowoy geum naani dineu meusseu changé

Wowowowowoy sounou rew yii bougou niou avancé

Ana kouko def waay

Nioune nioko def

Ana kouko def kouko def

Nioune leu

C′est pourquoi gniniouy diakhassé

Ba noppi diniou dioubolé

C'est pourquoi gniniouy diakhassé

Ba noppi diniou dioubolé

Wowowowowoy let′s keep our dignity

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Saï saï we want africa unite

Without conflict exodus

Mbédiou kanam nimako guissé

Boromako meuneu saafara

Li eupp tchi souniou rew yi tu sais

Bougoulou niou dara

Bou dé ganaw laniou guissé

Nonou rekk leuley teuweulé

Nii wala wakhone naniou beugué

Gnii wara dieuf tôk di khoulé

Kagne leu Africa di diok

Andd té gueuneu bania saafikou

Bokk liguey té wagni lolou

Kone sounu diangoro fadiou

Africa damala beugue ladjté

Est-ce que amouniou louniou fatté

Eh souniou beugué souniou diangoro fadiou

Bokk liguey wagni lolou

Bayyi seu kétou Africa

Africa damala beugue ladjté

Est-ce que amouniou louniou fatté

更多Youssou Ndour熱歌

查看全部logo

猜你喜歡