Meydey meudey oh ohhh
Youxou na Meydey ohohhhh
Mbecter la guissatoule
Mane dama moudier marre
Dem lene wakh koko
Eh yaw lane la
Da nga togone samaye xeff
Sorynala
Mangui doundou aldiana
Legui dama fine
(Hey Dama fine hey)
Dama cool
(Mane Dama cool)
Du guiss nga nima jekker
Mangui ok ok ok
LINGA ma dane DOUNDU LO
WOUTÉ NAK LIMA DONE
MBEUGUÉL bi DAFA TOXIQUE
Stress bi bariwone
MA DEUKÉ DIOY
Legui jexna
Dellou sama keur
XAMONE NA NI
YALLA DIÉXOUL
Mangek JOLI CŒUR
NDAKH
Yi xetou feme
Yi xetou tendresse
Yi xetou bakh bakh
Mangui doundou ma belle
Kay waye kaye
Baby Gnewal kaye
Kaye waye kaye
Sama jolie garcon
Ya ma jeuler si leundeume
Sama jolie garçon
Fi nga ma indi dafa lere Jolie garcon
Da nga rafete Sama Cheri
Wayer xole bi mola dakk
Daddy yeungeul ngama
Eh yaw lane la
Da nga togone samaye xeff
Sorynala
Mangui doundou aldiana
Legui dama fine
(Hey Dama fine hey)
Dama cool
(Mane Dama cool)
Du guiss nga nima jekker
Mangui ok ok ok
Sa mbeuguél amoul foronthiére
(Diégéma)
Yay passeport bimay toukilou
(Yobouma)
Kaye fi ni dagoule
Ya ma deff ni diayoule
Yi xetou feme
Yi xetou tendresse
Yi xetou bakh bakh
Mangui doundou ma belle
Kay waye kaye
Baby Gnewal kaye
Kaye waye kaye Sama jolie garcon
Ya ma jeuler si leundeume
(Sama jolie garçon)
Fi nga ma indi dafa lere
(Jolie garcon)
Da nga rafete Sama Cheri
Wayer xole bi mola dakk
Daddy yeungeul ngama
Eh yaw lane la
Da nga togone samaye xeff
Sorynala
Mangui doundou aldiana
Legui dama fine
(Hey Dama fine hey)
Dama cool
(Mane Dama cool)
Du guiss nga nima jekker
Mangui ok ok ok
Da nga chon sans facon
(Joli garçon)
Da nga chon sans facon
(Joli garçon)
Mane woynala sama cheri
Da nga chon sans facon
(Joli garçon)
Whawaw cheri
Sans facon