menu-iconlogo
huatong
huatong
avatar

Amadou

Coumba Gawlohuatong
panahaihuatong
Lirik
Rekaman
Loumou meu wakh

Ma diko deff

Daffey deuk ci dima togn

Teksi manane ko balma

Wayé mom la nobb

Sou mako guissé

Samey beut di mélakh

Samey tank djakhasso

Sama lamign rère ma

Mom la nobb

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou amadou

Damey gueumlo lou amoul

Téréwoul ma diko gueum

Tékci manane ko balma

Wayé mom la nobb

Sou mako guissé

Samey beut di mélakh

Samey tank djakhasso

Sama lamign rère ma

Mom la nobb

Amadou Amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye (yaye boye maymeu amadou)

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou Amadou

(...)

Sa youma digué woté téléphone

Ci téléphone bi lay yéndou

Sa youma digué ab setsi

Ma yéndoo wadjal

Khamnani nobb na kénéne koudoul man

Oh yeg nani mingui seti kénéne koudoul man

Wayé mom la nobb

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye maymeu amadou

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye (sama yaye boye maymeu amadou)

Amadou amadou

Guéstou ma

Man sama yaye (sama yaye boye maymeu amadou)

Amadou amadou Guéstou ma Man sama yaye (sama yaye boye maymeu amadou)

Selengkapnya dari Coumba Gawlo

Lihat semualogo