Samaxol
Boma tagou wone
Doma yobe
Bile thiono
Samaxol
Boma tagou wone
Doma yobe
Bile thiono
Mara nan te ragal ndokh mi
Oh mbeuguel hunn mane ak mbeuguel
Samaxol
Boma tagou wone
Doma yobe
Bile thiono
Samaxol
Booma tagou wone
Doma yobe
Bile thiono
Pithie bouy naw la def mba goumbe
Dafa doul xol famouy diogue
Dafa yoor tangayou diakharma
Ak seeday aldiana
Oh mbeuggel hun mane ak mbeuggeul
Oh mbeuggel hun mane ak mbeuggeul
Samaxol
Booma tagou wone
Doma yobe
Bile thiono
Samaxol
Booma tagou wone
Doma yobe
Bile thiono
Mara nan te ragal ndokh mi
Oh mbeuguel hunnn man ak mbeuguel
Souma diogue ba dieume si mom
Guir yegue ko soumay xalat
Sama fiit bi dadi key raggal
May weundelou diaxele loool
Oh mbeuguel hun man ak mbeuguel
Oh mbeuguel hun man ak mbeuguel
Te bou sigue khipi khol ma
Sama dunya beuga yeungou
May weundelou di waxtou
Man de xalat soumay pexe
Oh mbeuguel hun man ak mbeuguel
Oh mbeuguel hun man ak mbeuguel
Pithie bouy naw la def ba goumba
Dafa doul khool foumouy diogue
Dafa yoor tangayou diakharma
Ak seeday aldiana
Oh mbeuguel hunn mane ak mbeuguel
Oh mbeuguel
Man ak mbeuguel